Eumeu Sene Sort de sa réserve après son Combat J'ai été atteint Mystiquement, Meussouma beuré...?

  visualizzazioni 562,637

BANTAMBA TV OFFICIEL

7 giorni fa

Abonnez-vous à notre Chaine ITpost: itpost.info/done/udfBmVXjm-DTPjYNv8AWvQ.html?view_as=subscriber Aimez notre page Facebook: becayembayetv/ Visitez notre Site web: www.fmsenegal.info #Bantambatv.
77 419 03 64

Commenti
NSTYLEZ. TMC n.stylez
NSTYLEZ. TMC n.stylez 2 ore fa
Nandane nga eumeu tigui jaroul justifier wou, balla Nandane la, modou lo Nandane la, gris Nandane la, bombardier Nandane la , LAC vrai fake le, tapete la, dafay rous lo goor
Alda Fernandes
Alda Fernandes 4 ore fa
EUMEU J'adore ton sourire
Binetou rassoul
Binetou rassoul 4 ore fa
Lac 2 ay thiokh leuh amoul ...wah écurie weum nagn ko dieundeul thiokh svp
Abdul sumner
Abdul sumner 15 ore fa
Lac2 dafa wara bai lamba Du Dan tei du danu Match nil rek yaha derr keseh Mann Gambian la eumeu ndaanan nga
Serigne malick mbacké Diop
Serigne malick mbacké Diop 18 ore fa
Balla moy sama lutteur dh mais bilahi j’adore eumeu séne ndakh deugue bimouy guéné si lamigne bi deugue dafa nékh daale❤️🙌🏾
ceerw buty
ceerw buty Giorno fa
Mane dei Balla moy sama mbeur beugu wa Guédiaway mé biii dama méré lac srx Eumeu diam si yaw def gua leep franchement bénen yon moy dak inchallak
Eva Dia
Eva Dia Giorno fa
Walahi jeste bi eumeu déf ak balla dafma nékh trop
Mboul Ngom
Mboul Ngom Giorno fa
Ay way nguir yalla Eumeu boudé amna team dolen massi dougal té yalla takh
Mboul Ngom
Mboul Ngom Giorno fa
Machalah on t'aime bcp Eumeu wadiatal bou bakh rek
ceerw buty
ceerw buty Giorno fa
Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant
Abdou Sene
Abdou Sene Giorno fa
Lac est un imbéciles
Abdou Sene
Abdou Sene Giorno fa
Lac ne mérite pas c cacher
Maman Bop
Maman Bop Giorno fa
Machallah fans club pure là Mala beug pure eumeu longue vie
Bugs Bunny
Bugs Bunny Giorno fa
nekhoule ba nekhoul mais eumeu yaw tamite beurewo. deugue rek nekh nak
Elizabeth Brooks
Elizabeth Brooks Giorno fa
machala eumeu sene diambar gua
Mounass Tamba
Mounass Tamba Giorno fa
Je suis fier de toi champion😘💟💟💟💟
Coumba Diop
Coumba Diop 2 giorni fa
Wallahi djambar ga lac dou mbeur
qopoy dnon
qopoy dnon 2 giorni fa
yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala
Sarr Sarr
Sarr Sarr 2 giorni fa
Vous les lutteurs vous faites toutes des fétiches donc il faut accepter la défaite. T as rien à dire .il faut être sportif.
Adama Malick Dramé
Adama Malick Dramé 2 giorni fa
Lac d'où dara da nirou woule sakh mbeur
Adama Malick Dramé
Adama Malick Dramé 2 giorni fa
Bilay eume da melni nion boke père et mère bilay da ma la begue menouma sétane sa lamb si salle de bain laye dougue monté ay écouteur ba volume 100
qopoy dnon
qopoy dnon 2 giorni fa
Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul
Adama Malick Dramé
Adama Malick Dramé 2 giorni fa
Non eume ya fi nék ya meune kou nékoule lac li d'où défaite dhe yaw champion nga respect mbeur on é toujours derrière tw
Assane Konte
Assane Konte 2 giorni fa
Je vais convoqué les amateurs de lutte pour faire une marche pour que lac 2 arrête de lutter
Moustapha Kamal Th.
Moustapha Kamal Th. 2 giorni fa
Eummeu, boul wakhati dotouma beuré ak mom . Dél wakh beugatuma beuré ak mom inchalla. Jajeuf mbeur
Pape medoune Ndiaye
Pape medoune Ndiaye 2 giorni fa
Eumeu bilakhi wafii né
soniyu ziuy
soniyu ziuy 2 giorni fa
Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant
Mustataa Siise
Mustataa Siise 2 giorni fa
Euma tay bërewoo dara
Diagne Gnilou
Diagne Gnilou 2 giorni fa
En t'en que domou sèrére qui parle jamais sérère saymbok mérénagnoula
Diagne Gnilou
Diagne Gnilou 2 giorni fa
Yacodjoh sabaram
soniyu ziuy
soniyu ziuy 2 giorni fa
Non eumeu gor deugue la
ndiaga faye
ndiaga faye 2 giorni fa
Jämbàr deugue ngueu maaacha allaah ki ngua doon da dieel mooy thiounné reek koo diapp mistiquement War koo meuneu daan
Hamidou Agne
Hamidou Agne 2 giorni fa
Eumeu champion gue 👍Lac mome dou beure
Pape Sane
Pape Sane 2 giorni fa
Je suis supporter de Balla gaye mais eumeu sene je t'adore vraiment legui sama mbeur nga ndakh sa xol dafa rafet
Awa dia Sy
Awa dia Sy 2 giorni fa
Bilaye soule ndanane souli badola mais yaw mbeur nga diambar nga
cheikh kouyate
cheikh kouyate 2 giorni fa
Eumeu il est bien. Lac 2 bonne continuation. Je suis fier de toi
sotuur aeei
sotuur aeei 2 giorni fa
Douma fans Eumeu mais damako naw franchement dafa digne degou blie machalla
Aly Niane
Aly Niane 19 ore fa
Ad
Youssou Diop
Youssou Diop 3 giorni fa
Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul
Issa Diao
Issa Diao 3 giorni fa
Lac dou mbeur bilahi
Issa Diao
Issa Diao 3 giorni fa
Na bayi beurré
sotuur aeei
sotuur aeei 2 giorni fa
Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss
Ndaye Khodia
Ndaye Khodia 3 giorni fa
Ndanane koulou ndanane 😀sama mbeur bii yalnala yallah dfl djm rk Yaw ak modou lô ndam siréee khalé by kham limuye deff 😁😁 Athia mbeur
Assane Samba
Assane Samba 3 giorni fa
Wathié akh amateurs yii wathié supporter yii diambar nga ndanane nga gaindé nga amato loy prouver si lambe d'elle déglou sa encadrement géré sa carrière champions one love eumeu sa beuré mo tah ma beugu leu té dou dégn yalnala yalla diapalé
Boury Ka
Boury Ka 3 giorni fa
Balla sama gaynder Ndiaye
Mamy Ba
Mamy Ba 3 giorni fa
Goor yalla deugue gua machalah ❤️ djomm reek gay prouver eume kou am djomm gua amoulo Keen akk nala Diam sonal sa yaye dala gnanal bilay wolay machalah ❤️
Muslim2proud
Muslim2proud 3 giorni fa
Kouko déffati nako deegg, ap mbeur dou fénn, mbeur dou tapalé...aaay kouko défati nako deeg ap mbeur dou tricher mbeur dou yambar, 😤diapé sénégalais yi dofff 💃💃💃💃💃😂😂😂😂😂Eumeu, Balla Gaye2, Yekini, Bombardier, Ama Baldé, merci infiniment, gathiéloulén lambe. Fatou Guièr 2 démal nga toog, ngir yalla boulfi dieuleuti beneu combat, doyal na gnou si yow seuk.🙄🙄😏😏😠😠😠😠😠
Djily Diop
Djily Diop 3 giorni fa
Non eumeu gor deugue la
bssni touir
bssni touir 3 giorni fa
Lou lérr laa wakh
vmvdou svné
vmvdou svné 3 giorni fa
jai trop aimé son discours
vito boss vito boss no stressé
vito boss vito boss no stressé 3 giorni fa
mane fans balla gayé la
bssni touir
bssni touir 3 giorni fa
C'est vrai je suis avec eumeu
vito boss vito boss no stressé
vito boss vito boss no stressé 3 giorni fa
bilahi euma borom bakh la
drttyu liqm
drttyu liqm 3 giorni fa
yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala
El Che
El Che 3 giorni fa
Lac 2 moy enfoiré rek . Yaw kenn du yaw jambar deug ga
Mamadou Alpha Bah
Mamadou Alpha Bah 3 giorni fa
Je suis un fan de Modou Lo mais je t'aime💕💕❤❤😍
Marieme Balde
Marieme Balde 3 giorni fa
Mais eumeu nak balla dinala dane dh one bakhga trop beugue nagne la mais dinagne la dane dh 😂😂😂
drttyu liqm
drttyu liqm 3 giorni fa
lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak
Marieme Balde
Marieme Balde 3 giorni fa
Sana xol diekhna si lac thiim. Bravo eumeu courage. Balla ak wa keureum gnoy samay mbeur (sauf Lac maintenant) legui iow yako remplace. Borom vakh nga
Aita Ndiaye
Aita Ndiaye 3 giorni fa
Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss
Ndeyemarie Seye
Ndeyemarie Seye 3 giorni fa
Diamou RK ngayi âme bly
BUZZ MIFA
BUZZ MIFA 3 giorni fa
EUMEU BOUL BAY AWMA KÉNE COUEOUL YEW
Khady Togola
Khady Togola 3 giorni fa
Eumeu ya meuna doull lac dakeu leu bangua guéneu sakou yi guay féne Amgua mélokane déh khawma wone ni ningua mel féne bakhoul
BUZZ MIFA
BUZZ MIFA 3 giorni fa
EUMEU JE T'AIME BILLAHI
Issakha Ndiaye
Issakha Ndiaye 3 giorni fa
Tu fais partie des meilleurs.
Aboubacry Sarr
Aboubacry Sarr 3 giorni fa
Ya fi meun dh Eumeu billahi ❤️
Chekh tidiane Thiam
Chekh tidiane Thiam 3 giorni fa
C'est vrai je suis avec eumeu
Mbacké Seck
Mbacké Seck 3 giorni fa
Lou lérr laa wakh
Modou Mbaye
Modou Mbaye 3 giorni fa
Eum bénéne yonne boy bré boul nuyoti kénn lokho.bâ nga nuyo thi lamb dji la khamni da ngay d'Abou.
Abdou Mbaye
Abdou Mbaye 3 giorni fa
Eumeu sa kanam
khass Killah
khass Killah 3 giorni fa
Boléne waxé té yalla tax ngéne xamni lac2 mo tané si combat bi ndax mom sax défna touti effort eumeu sax wax nako après combat bi "waroléne ma wonn téyélo sama bop" motax dafa taxaw rék défoul dara. Questioné nagn ko mo bo xolé boubax dafay rafétal di rectifié wax bi coz ay staff faw gnoniko bouko wax parck lolou daf léni yaxal mbeur gnou fayla ay millions sa staff nane la téyél sa bop
Penda Wade
Penda Wade 3 giorni fa
Yaw diabargua bilay
Khady Gueye
Khady Gueye 3 giorni fa
lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak
Khady Gueye
Khady Gueye 3 giorni fa
billay diabare gua
Mame Saye Sylla
Mame Saye Sylla 3 giorni fa
Bilahi eumeu sene wakhone na lako si beineu commentaire nila lac de guiers 2 dalayy tardel rek khamoul gatt ragale na bilahi wokhone na lako beurei woule bayi woule dafa ragalll tropp tropp
Abu Konate
Abu Konate 3 giorni fa
Eumeu lat 2 amoul diome
Ibrahima Khaliloula Hounsah
Ibrahima Khaliloula Hounsah 3 giorni fa
Eumeu Nguaïdé Nguay Meussa Done Bo Bayé Beuré Sax Nguaïdé Ngua
Diogop Ka
Diogop Ka 3 giorni fa
Machalla fiér de toi champion 💪💪💪sa kaw sa kaname
Ibrahima Diop
Ibrahima Diop 3 giorni fa
💪💪💪👍👍
Khadidiatou Gueye
Khadidiatou Gueye 3 giorni fa
Barki yamlah Eumeu damala beug
Seyidina Sow
Seyidina Sow 3 giorni fa
Eumeu champion nga lou lérr Lac war nga kholaat sa beuré té di dieul décision, am nga katane loy ragal, khamon sakh biss bo mome warko am ndam,... modou lo ndam rék Incha ALLA
Sila Dame
Sila Dame 3 giorni fa
Q
Sall Ablaye
Sall Ablaye 4 giorni fa
Khole bou rafet eumeu
Mansour Gueye
Mansour Gueye 4 giorni fa
Mberr yaw diaroul sakh ngay nioue khana nonou yaye Kane mberr pure nga
Isatou Jobarteh
Isatou Jobarteh 4 giorni fa
Eumeu sene yow ya Barry wakh barry tapaleh
Fati Sow
Fati Sow 4 giorni fa
waw kay eumeu diadieuff way on te fais confiance
Adama Fall
Adama Fall 4 giorni fa
Champion nga
Mariama Diéne
Mariama Diéne 4 giorni fa
💪💪😇😇😇😍😍😍👍
ASTOULO KOBAR
ASTOULO KOBAR 4 giorni fa
Eumeu yawdal gathia ngalama chapeau a vous mbeur kaamil NGA
Pape Davido
Pape Davido 4 giorni fa
Cœur pour diambar jdi ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Tijani Dia
Tijani Dia 4 giorni fa
Waw kay sama mbeur bi amal diame yaw lanou beugue tay ak soube mala beugue rek té yallah takh soy beuré douma ame diame wallahi taye wnibik hateu
Pape Davido
Pape Davido 4 giorni fa
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Ahmada Dial
Ahmada Dial 4 giorni fa
Iow tamit beure wo ...wakh ko kéne meunou niou nakh
Adama Camara
Adama Camara 4 giorni fa
Eumeu séne diambar gue nion gui sa gui naw
Gooo Bhff
Gooo Bhff 4 giorni fa
Eumeu ❤️❤️❤️❤️💪
Gooo Bhff
Gooo Bhff 4 giorni fa
@gtoss chddy lac mo bougone Revanche
gtoss chddy
gtoss chddy 4 giorni fa
Vous avez tout les deux déçu
Mariama Aliou Diouf
Mariama Aliou Diouf 4 giorni fa
Fier de vous Eume Sene
Serigne saliou Lo
Serigne saliou Lo 4 giorni fa
Waw lac nonou ladone def mé khamnanou touti si lamb
gtoss chddy
gtoss chddy 4 giorni fa
Vraiment jambar gua mbeur lac modoul touss
ibrahima ndom
ibrahima ndom 4 giorni fa
Eumeu mi da melni da beug beuré wate AK Balla
Pisco Kane
Pisco Kane 4 giorni fa
Wakhoo fi dara...tu as fui le combat .sois honnête waay .
Rama Gueye
Rama Gueye 4 giorni fa
Euma boul décourager lépou dina bakh lac mome dangay warou 💪
Fatou Thiam
Fatou Thiam 4 giorni fa
Walaye tu est le meilleur je t'aime mbeure
JuNiOr BabA
JuNiOr BabA 4 giorni fa
Wakh dji amna solo yéndou na maana eupeu
samba Sy
samba Sy 4 giorni fa
Il a raison, lac2 c’est un fuyard
Mame Gor
Mame Gor 4 giorni fa
Eumeu wakhna deug 🤭Mbeur yi nio maak thiéré massé ak lalo 😂Balla gaye ak papa sow biniouy mbapatt. 2002 terrain 22 bounte keur birahim Ndiaye sétane nako j’avais 17ans legui nio donc niom warone nagnou am 20 ans ou 22 ans donc souma calculer balla warna aam 39 ans ou 40 ans a se moment 🤭🤭😂😂
Aly Dieng
Aly Dieng 4 giorni fa
Bilahi emeu ta raison lac amoul dioum amoul fouleu
Bienvenu Cheikh chico SECK
Bienvenu Cheikh chico SECK 4 giorni fa
Eumeu nak, on t'aime bien because yagg gn beuré lamb jank you neex mais bi mom iow ak lac yaleen si yem defoleen fi dara dsl nak defaroul watt da melni filla mod'lo dougeul guénagoffa D.
tyfa dieng
tyfa dieng 4 giorni fa
Late 2 dou mber nabayi beré on t'aime fort eumeu💪
Serigne Modou Diallo
Serigne Modou Diallo 4 giorni fa
Bilay man serign fans balla la mais dam beugue eumeu sene ndkh balla gaye
Mamediarra Balde
Mamediarra Balde 4 giorni fa
Defofi dara bou niou wakhante deug daga ma rouslo kerok
DON XHONI - MAFFIA
2:49
DON XHONI
visualizzazioni 2,5M
Sacky - Quello Vero Freestyle (Prod. NKO)
1:33
Sacky Official
visualizzazioni 430K
Impariamo a correre come @Frank Matano | LOL: Chi ride è fuori
5:10
Amazon Prime Video Italia
visualizzazioni 46K
Napoli - 3ª Prova Campionato Serie A1 GAM/GAF - Trofeo Veggy Good
4:54:59
Federazione Ginnastica d'Italia
visualizzazioni 52K
DON XHONI - MAFFIA
2:49
DON XHONI
visualizzazioni 2,5M
Sacky - Quello Vero Freestyle (Prod. NKO)
1:33
Sacky Official
visualizzazioni 430K
Impariamo a correre come @Frank Matano | LOL: Chi ride è fuori
5:10
Amazon Prime Video Italia
visualizzazioni 46K
Napoli - 3ª Prova Campionato Serie A1 GAM/GAF - Trofeo Veggy Good
4:54:59
Federazione Ginnastica d'Italia
visualizzazioni 52K
Highlights Real Madrid vs FC Barcelona (2-1)
3:08
LaLiga Santander
visualizzazioni 4,4M
Alessandra Amoroso - Piuma
4:03
AlessandramorosoVEVO
visualizzazioni 295K
UFC Vegas 23: Marvin Vettori - "I Want This Title" | Post-Fight Interview
1:54
UFC - Ultimate Fighting Championship
visualizzazioni 168K
Mr.Rain - Meteoriti (Official Video)
3:08
Warner Music Italy
visualizzazioni 379K
Elite - Stagione 4 | Data d'uscita | Netflix
1:03
Netflix Italia
visualizzazioni 26K