Dip Doundou Guiss - Musiba

  visualizzazioni 3,248,470

Dip Doundou Guiss TV

Mese fa

In Musiba , DIP reinforces his title as the King in the rap game : he reminds his detractors that he sits on the throne, no matter how hard they try to make it seems like he’s not. Between punchlines and egotrip, he wants to make it clear : he IS their biggest disaster.
Dans ce titre, DIP consolide son titre de King dans le rap game : il rappelle à ses détracteurs qui est le roi, malgré leurs attaques incessantes. Entre différentes punchlines et egotrip, le King tape sur la table et prévient les MC : leur plus grand malheur, c'est lui. #Musiba en streaming et en téléchargement sur toutes les plateformes : orcd.co/musiba
....................................................................................................
Clips officiels : bit.ly/ClipsofficielsDip
.....................................................................................................
Suivez-moi sur les réseaux sociaux :
Facebook : web. dipdoundouguissofficiel
Twitter : DipDunduGuiss
Instagram : dip_doundouguissofficiel
Snapchat : Dip490
.....................................................................................................
Compositeur : Ssadik beatz
Mix & mastering : Karabalik Beatz
Production : Reverse Studios
Réalisation : Bilal Mbengue & Leye Gueye
Stylisme : DoulSy JahGal
Décoration : Yarba Déco
Make Up : Mimi’s Touch
lyrics
REFRAIN
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay

COUPLET 1

Comme roof si ceeb
Cere dolli ñeex
Capp ni goor Gui Dieng
Vol si jet, wala doxx si geej
Yokk job du deñ
Kuy bonn di hate
Bombe nucléaire ci sa xol bu wow ni xeer
Même boy dé bul fokni jeex na, may bëss bila God di yé
Investir ci fenn amo saxx bénéfice du doute
Na doon 50 cents sama ben shot, sa fils du jukk
DIP mola mën du gacce c’est comme ku Messi di duut
Ma ngi si trône bi ak ñom Messi jël sama Pepsi di guux
Duma segg si cage
Man la seen soeurs yi di xaar
Maa taxx sen sërr yi di tass
Carrière bi munoko saltel nigger melni sa chemisou pa
Sëg di gass, job lu tax CD bi jarr
Fële jël sa reliquat
Sama cachet sañu ñuko dagg ni bin bin ci sa ndigu Ma
Na money bi teew, xaalis moy gagner guerre bi duma rayante comme militaires
Si kaw lañuy yeeg wacce leen ni adamak awa ak pomme biñu yëy
Sori fi man, duma xooli sa guel même su defe man kesse si story privem
Coow li du jeex fi ba mëwti di dé amatu ñu adversaire mais ño ngi si guerre
Refrain
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay

Couplet 2
Every day, may def baña xaar ndaxx dé du jeem
Soxlawuma tuub pour def ko benn buum mën na takk plus de 5 jeeg
Yes we can
Gedd gratte- ciel, dëkki Baraku Bamba fu Trump dem ba nek president
Fu sëtu esclave dila ray ngir chaîne
Tojj sa lu bonn ba mujje ak séy biens
Nigger ëppo njariñ skincaru Michael Jackson ci cimetière
Dangay gunge rek ni frèru Michael Scofield ci biir jail
Damay fayu ba pare mën nangu ni coow du jib kay
Ku xamm kepp kuy rap wolof xamna nombre rappeur bi DIP fay
Tek sama nafsu ci beat bi
Rap yefu dëmm dëg lë kan mo saña waxx ni que Pac bëggul Biggy ?
Sen game bi concours lëmbël la motax malay yokkal ay tama si beat bi
Sa guel la yakoy solal makoy simi, dagg buumu gacce dagg seeni string yi
Sama kumpa nekul books mais rappeur yi publier gul sen streams yi
Ay goat yu vider plassu gettu bëy du sho bu tijji tank rek ñu dem
Dé bi kesse momay taxa tëddi ni roses yi si sa tanku caissou neew
Bëg coow ni intifada Ben Laden
Même dof du sikki sakka lima fi def
God du mëssa àndak ñi di fenn
Par force King bi man la té du deñ

Refrain
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay

Commenti
Dip Doundou Guiss TV
Dip Doundou Guiss TV Mese fa
Les francophones qui ne comprennent pas wolof, les sous-titres en Français sont disponibles. Vous pouvez l'activer :) REFRAIN Fuck number one, Fuck number two Si tu penses détenir le secret de ma chute, fais attention à ne pas te louper (yeaah, ouuh) Un vrai malheur Toujours tranquille grâce aux prières de ma mère Je suis dans toutes les bouches J’abandonne jamais, et même si je m’incline je ne suis jamais à terre Je suis le meilleur pour t’effacer Je suis ton malheur Ton malheur COUPLET 1 Tel une farce dans du Tiep J’en veux toujours plus Aussi riche que Gorgui Dieng Un vol en jet ou une balade en mer ? Toujours en train de taffer Pendant que tu hates J’lance une bombe nucléaire sur ton cœur et le rend encore plus dur qu’une pierre Et même si tu venais à mourir, ne pense pas que c’est fini : je suis le jour de la résurrection Toute ta vie tu mens, t’as même plus le bénéfice du doute Et même s’il était 50 Cent, ton gars serais à terre après UN seul de mes tirs Il n’y a pas de honte à admettre que DIP est le meilleur ; c’est comme se faire dribbler par Messi Je suis sur le trône avec la bande à Messi, en train de siroter mon Pepsi Je ne suis pas une panthère en cage Tes sœurs n’ont d’yeux que pour moi ; Je suis la raison pour laquelle leurs pagnes tombent Tu ne peux pas salir ma carrière, aussi clean que la chemise a ton père Toujours en train de bûcher, on a fait le job pour que les CD se vendent Et je prends tout, même ton reliquat Personne touche à mon cachet, un peu comme la ceinture de perles de ta mère L’argent est mon arme, je ne fais pas la guerre comme les militaires On monte au sommet pour mieux vous mettre à terre, tel Adam et Eve Loin d’ici, ta meuf ne m’intéresse pas même si je suis le seul dans sa story privée Tant que l’ange de la mort vivra, t’auras pas la paix ; on a plus d’adversaire mais on continue la guerre REFRAIN Fuck number one, Fuck number two Si tu penses détenir le secret de ma chute, fais attention à ne pas te louper (yeaah, ouuh) Un vrai malheur Toujours tranquille grâce aux prières de ma mère Je suis dans toutes les bouches J’abandonne jamais, et même si je m’incline je ne suis jamais à terre Je suis le meilleur pour t’effacer Je suis ton malheur Ton malheur COUPLET 2 Je bûche chaque jour sans attendre parce que la mort ne préviens pas Pas besoin de me convertir pour avoir plus de 5 meufs à ma corde Yes We can J'ai dit non à un gratte-ciel pour vivre dans la baraque à Bamba, dans un pays où Trump a réussi à être président Là où les descendants des esclaves te butent pour une histoire de chaîne Moi je te bouffe et prends tes biens OKLM Nigga, tu n'as pas plus d'effet que la skincare de Michael Jackson au cimetière T'es juste là pour meubler, comme le frère de Michael Scofield en prison D’abord je te rends la pareille, puis on tombe d’accord sur le fait qu’il n’y a pas polémique Si tu connais bien le rap wolof, tu sauras le nombre de rappeurs que DIP a enterré Je pose tout mon être sur le beat Le rap c’est une histoire de vampire, qui ose dire que Pac n’aime pas Biggy ? Votre game, c’est un concours de twerk, raison pour laquelle t’auras toujours du tambour sauvage dans mon beat T’habilles ta meuf mais je finis toujours par la déshabiller ; je fais disparaître le déshonneur tout comme son string Le mystère pour moi, ce n’est pas Books mais plutôt tous ces rappeurs qui n’arrivent toujours pas à publier leur stream Ça se dit goat mais ça remplit la place des nullards ; ici on ne dit pas oui à la première venue Je serai allongé qu’une fois mort, comme les roses au pied d’un cercueil J’aime le vacarme comme l’intifada de Ben Laden Même un fou n’oserait pas douter de mes performances dans le game Dieu est contre les injustes Je suis le King et rien ne pourra changer cela REFRAIN
 Fuck number one, Fuck number two Si tu penses détenir le secret de ma chute, fais attention à ne pas te louper (yeaah, ouuh) Un vrai malheur Toujours tranquille grâce aux prières de ma mère Je suis dans toutes les bouches J’abandonne jamais, et même si je m’incline je ne suis jamais à terre Je suis le meilleur pour t’effacer Je suis ton malheur Ton malheur
Serigne saliou Diop
Serigne saliou Diop 23 ore fa
Boy dip
Modou Touré
Modou Touré 3 giorni fa
💪
Sheikh Toure
Sheikh Toure 3 giorni fa
Moi c’est maintenant la gosse
Sheikh Toure
Sheikh Toure 3 giorni fa
C’est bon Alain comment conjuguer au modèle Babacar y’a carriole
Sheikh Toure
Sheikh Toure 3 giorni fa
Au début Noguaye elle est à gueule laptop Bonagari est-ce que ta mère elle force Aidara il faut
Moustapha KW
Moustapha KW 47 minuti fa
Dip chantant Musiba Manifestation de Ousmane Sonko Dip est il Illuminati ?
HOT Gaming
HOT Gaming 2 ore fa
nice
Big black général Officiel
Big black général Officiel 2 ore fa
Kong Kong ki es là
Demba Diawo
Demba Diawo 3 ore fa
Coucou comment tu vas tu dors bien alhamdoulilla on est pas à moi tu dors tu es où tu es là Corniche Nabil Choucair je suis là Corniche Nabil Choucair je
The Falilou Pro180x
The Falilou Pro180x 4 ore fa
*CETTE MUSIQUE EST SATANIQUE , IL A PROVOQUÉ DES ÉMEUTES*
The Falilou Pro180x
The Falilou Pro180x 4 ore fa
Après musiba il y a eu des émeutes au senégal
7.M euphoria
7.M euphoria 17 ore fa
#Freesengal.
Saloum Fall
Saloum Fall 18 ore fa
tu es trot fort
pape abdoulaye ndiaye
pape abdoulaye ndiaye 20 ore fa
Qui est là contre tenue de la situation actuelle...😈 ?
tv le mondo
tv le mondo 22 ore fa
Mosiba yagui dora komase
abdoul aziz ndiaye
abdoul aziz ndiaye 23 ore fa
Dip repond moi : qui est number 1 et qui est number 2! Qui es tu? je sais que tu es le meilleur rappeur au senegal mais qui es tu? pourquoi le son musiba! Comment tu as fait pour le son freesenegal en moin de 3 jours? Qui est number 1 qui est number 2?
Amina Gueye
Amina Gueye Giorno fa
Wah dip khana c un voyant!!
Moi meme
Moi meme Giorno fa
Vous êtes vraiment intelligents je VS adore...ta chanson et ce qui se passe actuellement 😈 huh huh regardez encore bien la video les gars y compris le drapeau de la FIFA entouré de fumé eh eh...en passant je critique pas j’apprécie 🤨
Reimana Modji
Reimana Modji Giorno fa
Walay king bi ioe la Dip jtm sans raison
Aicha Konte
Aicha Konte Giorno fa
Dip da melni annonce guagnou done diokh d😂😭ligua tournee dei mo am senegal ni
EDOUARD DIOUF
EDOUARD DIOUF Giorno fa
221🇸🇳DIP C DU LOURD
Kocc Bi
Kocc Bi Giorno fa
Nice diop day fay
Ibzo Pro
Ibzo Pro Giorno fa
0:53Mais ce gars a blessé la femme à droite 🔥 kung-fu 2.0
Muhvmēd Ka
Muhvmēd Ka 2 giorni fa
Dip respect ✊🏾 à toi tu es le meilleur #freeSenegal
Abdoulaye Faye
Abdoulaye Faye 2 giorni fa
C est le meilleur rappeur du mon
Ndiaye Assane
Ndiaye Assane 2 giorni fa
Dip balma akh yafi man
Manoush Sow
Manoush Sow 2 giorni fa
Woyal diam naroulay deuk bi am diam
Positif MAn
Positif MAn 2 giorni fa
Le serpent🐍 sur le coup de DIP je parie personne n'y est prise attention
Jeannette ba
Jeannette ba 2 giorni fa
Guenel gnou diamm naroulay rk please
big raune
big raune 2 giorni fa
Qui revenu voir le clip à cause de ce qui ce passe actuellement
Jeannette ba
Jeannette ba 2 giorni fa
On dirait que tout ça se produit réellement actu
Boubacar Samb
Boubacar Samb 2 giorni fa
Dip devrait plus sortir se genre de son Car à pêne le Sénégal est entrain de chauffer Avec le truc de Soncko président Néanmoins c du lourd son clip
anta Gueye
anta Gueye 2 giorni fa
Wa dip khana danga yeugone souniou moussiba bi ahh 1 mois apres 🙄
princess
princess 2 giorni fa
Le Sénégal en ce moment😭💔🇸🇳
mme bonheur joie
mme bonheur joie 2 giorni fa
Dip ya ya tall ndakarou dh
Djily Diop
Djily Diop 2 giorni fa
Dip doundou guiss weuyal diam naroulay depuis bi nga weuyé musiba deuk Bangui tak😂😂
Fatou kine Sylla
Fatou kine Sylla 20 ore fa
Vréma 😂😂😂
Ycmah Cyxoñ
Ycmah Cyxoñ 2 giorni fa
Ay xalé you niakkeu Diome nguen!!! Dip beugueuneu cimetiere beugueu crane dip mo ngui lén di wane bopam wayé baxna rek
Ndeye's Moods
Ndeye's Moods 2 giorni fa
yako fi wo, eksi na nak 😒
Mame khary falilou Djigal
Mame khary falilou Djigal 2 giorni fa
Mussiba bagui sogua ame nak #FreeSenegal
Babacar Faye
Babacar Faye 2 giorni fa
Actuelle meilleur rappeur sénégalais
Amintambaye Mbaye
Amintambaye Mbaye 2 giorni fa
Non kou dakor nii dipp chanchon wam dakoy tek si temps togoul mbalakh bi de trop komme le font les autre qui est dakor pousse bleu
Cheikh sidy Sane
Cheikh sidy Sane 2 giorni fa
Dip yaye deum "MUSIBA" finalement au Sénégal investir si fene amo sakh bénéfice du Doute.....
Cheikh Fall
Cheikh Fall 2 giorni fa
Musiba Narulaahi mingui Doreu am nak😱😭🤦🏽‍♂️🔥les messages subliminaux de Dip li yeup prédir nako wone #Free_Senegal🇸🇳🇸🇳🇸🇳😍
Awa Dia
Awa Dia 2 giorni fa
Bly dip day guiss
FG TOUBA
FG TOUBA 2 giorni fa
Comment avoir le texte s'il vous plaît
Assi Diong
Assi Diong 2 giorni fa
Dip daguay guiss wala 🤔
Wely Faye
Wely Faye 3 giorni fa
Makhala yagnou oume mousiba réke😂😂😂😂😂😂😂
fa walyette
fa walyette 3 giorni fa
Je suis là pour mousiba bou xew Sénégal depuis le 03 Mars 😂,dip khana voyant nga 🥰
Binta Dia
Binta Dia 3 giorni fa
Mais depuis quand guay guiss Leumbé dakarou ndiaye Musiba naroulay Les explosions C comme si tu nous prévenais avc le cas de sonko là🥲🥲😂
Fallou Ndour
Fallou Ndour 3 giorni fa
mais Dip do wokh si li khew Senegal bokk
Fatou kine Sylla
Fatou kine Sylla 2 giorni fa
Vérmat 😂😂😂😂
Souleymane Mane
Souleymane Mane 3 giorni fa
Musiba ba gui ni nak Sa lamine way🔥🔥🔥
Baala Diop
Baala Diop 3 giorni fa
Son bagui sogua am valeur nak mousiba sék sina😁
Mitidio Emasse
Mitidio Emasse 3 giorni fa
Dip avait vu ce qui allait se passé a Dakar "Mussiba" est la preuve
Abdoulaye A KA
Abdoulaye A KA 3 giorni fa
Neubatou dji lénn dé boy 'diaguou bi day yéé fitnaa
AMT KA
AMT KA 3 giorni fa
Dip sénégal amna musiba dé🤧🤣 khana daguay prédire avenir
Mamadou Ba
Mamadou Ba 3 giorni fa
Ya moune billahiii
King Marley
King Marley 3 giorni fa
Je me retrouve bien dans cette chanson..je pourrait l'écouter h24..chapeau l'artiste j'attends ta venue en CIV
Khady Sall
Khady Sall 3 giorni fa
🖕🖕🖕🖕🖕🖕😁😒
Khady Sall
Khady Sall 3 giorni fa
🤝🤝
Ramou Lee19
Ramou Lee19 3 giorni fa
He’s the KING 🤴🏾 and that’s on PERIODT 🔒
KDM ND
KDM ND 4 giorni fa
👀👀
Abdoulaye Niang
Abdoulaye Niang 4 giorni fa
Messi d'où nite
SUAME SAMUEL EKRA
SUAME SAMUEL EKRA 4 giorni fa
🐐 🐐 🐐
Mandiaye DOUCOURE
Mandiaye DOUCOURE 4 giorni fa
Dip est le meilleur que est d' accord
Kabinet Camara
Kabinet Camara 4 giorni fa
C’est du lourd 👏👏👏👏💪💪💪
bocar damaniste
bocar damaniste 4 giorni fa
mousiiiba gua beguone tu la eu fils rewmii yeup pa gui takkj
bocar damaniste
bocar damaniste 4 giorni fa
li xew thiii rewmiii yeupp song bila
Majesty Niasséniya
Majesty Niasséniya 4 giorni fa
L king certifié
Babacar Gueye
Babacar Gueye 5 giorni fa
Métaphore yako dakh si réwmi 😊👌
Bassirou Dia
Bassirou Dia 5 giorni fa
C le meilleur au hip hop galsen c t'a dire c'est le king du rap galsen
Cabrel ghis
Cabrel ghis 5 giorni fa
une tuerie ...depuis +237
multi game
multi game 5 giorni fa
Nice music dip
Aloïse Amath Thiaw
Aloïse Amath Thiaw 5 giorni fa
Non DIP t' es le meilleur
MAOZEK L' OFFICIEL
MAOZEK L' OFFICIEL 6 giorni fa
Rêve être un rappeur pour guiss Dip beute ak beute je veux être un rappeur
Tanji Got Talent
Tanji Got Talent 6 giorni fa
This is real talent bars dope and real poetry lines with so much paradoxical . Dip you're unique and rare the way you lay literary together makes it excellent and exceptional
Amath Ndiaye
Amath Ndiaye 6 giorni fa
Ngaaka mola dakk rap nak
abdoul aziz ndiaye
abdoul aziz ndiaye 6 giorni fa
liii ngay ioe sakh gueumo ko ki nga fan gueomouko ay mbokam gueumou niouko T wornala ni kene gueumouki. Limoy investir si fene té amoulo sakh benefice du doute
baba wally diafoune
baba wally diafoune 6 giorni fa
À quand les 3 millions 👀🔥🔥
Cheikh Cisse
Cheikh Cisse 7 giorni fa
Dip👑🤴
houda fall
houda fall 7 giorni fa
Dip yaye sene bay
Ismaila Kane
Ismaila Kane 7 giorni fa
J’ai peur
Bakary Koumou
Bakary Koumou 7 giorni fa
Tu testera toujours king
Ahmadou sara Mané
Ahmadou sara Mané 7 giorni fa
3 million de vue en 1 moi bra vo idole sama royouway
Amath Toure
Amath Toure 7 giorni fa
Qui est la après les 3 M 🖒
Nagy Badaoui
Nagy Badaoui 7 giorni fa
J’y va j Fc
Muhvmēd Ka
Muhvmēd Ka 7 giorni fa
Bientôt 10millons de vues inchallah
Temy FARIALA
Temy FARIALA 8 giorni fa
Je comprends pas Wolof mais ce frère a un flow de dingue et les effets spéciaux du clip sont impeccables. l'Afrique avance !
Kinè Official
Kinè Official 8 giorni fa
🔥🔥🔥🔥🔥
No justice no peace
No justice no peace 8 giorni fa
Da nga guéné musiba rek, deuk bi am musiba ....
Sd C
Sd C 8 giorni fa
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
cheikh dieng italy livorno
cheikh dieng italy livorno 8 giorni fa
Bima sitane demb barah la xamne do nit rap yeufou wampirla bilahi 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Mareme Sarr Mbengue
Mareme Sarr Mbengue 8 giorni fa
Enfin les trois millions
Djily kebe
Djily kebe 8 giorni fa
3 millions de vus en 1 moi jamais vue🙏👁🤗
Ndeye ndiaye
Ndeye ndiaye 8 giorni fa
3 millions de vues en 1mois ils chaud ce mec
Experiment Black Boy
Experiment Black Boy 8 giorni fa
KI DEF MONTAGE BII PRO LA DEEE WOWWW
Adjaratou Fatou Diouf
Adjaratou Fatou Diouf 8 giorni fa
Dip walnala yalla are moi je comprend
Black kido
Black kido 9 giorni fa
Woooooooooooooooooooooooooooooooooooooy💥💯🎶🇸🇳
SOULEYMANE DIALLO
SOULEYMANE DIALLO 9 giorni fa
KING BABA
Coumba Lo
Coumba Lo 9 giorni fa
Oh my god,mé c ses capacités sont inestimable oh dip je t'adore u es l king du hip hop bravo bravo bravo
Ibro Balde
Ibro Balde 9 giorni fa
3 m
aliou dia
aliou dia 9 giorni fa
Cool
SCOFLID 100
SCOFLID 100 9 giorni fa
Do nit 3m de vie
Genuine man
Genuine man 9 giorni fa
Je confirme qui'il est le Meilleur Rappeur du hip hop Galsen 🇸🇳 vraiment Respect!!!
L'enfant Noir
L'enfant Noir 9 giorni fa
Dip wagnil dozbi sinon dey doon over doz si rappeur yi nangouléne ndogal sinon guén déh
Oumy Touré
Oumy Touré 9 giorni fa
King du rap galsen🤩🤩💥💫✋
Queen Nefertiti
Queen Nefertiti 9 giorni fa
Nekhna dh wayeii Ba ngua wayyé son bii Ba leggui diam amatoul Galsen Musiba nguii si rewmi🇸🇳🇸🇳
Dip Doundou Guiss - #FreeSenegal (VOSTFR / VOSTEN)
02:55
Dip Doundou Guiss TV
visualizzazioni 637K
Jeeba - GUUY - (prod. by Bril) [Clip Officiel]
04:02
REACTION: UN BARO AD ITALIA'S GOT TALENT
10:00
Jack Nobile
visualizzazioni 86K
Youssou Ndour - Bukki Yi - Clip Officiel
07:58
Youssou Ndour
visualizzazioni 6M
Samba Peuzzi - Oulalalah
03:35
Samba Peuzzi
visualizzazioni 1,7M
50 Cent - In Da Club (Official Music Video)
04:08
Karabalik beatz - Fou Lerr Lako Tekk feat Reptyle Music
05:07
Negu Goor_ Akhlou Brick ( prod by Weezyade)
03:38
AkhlouBrickTV Officiel
visualizzazioni 1,2M
King Baba
03:06
Ngaaka Blindé - Topic
visualizzazioni 3,2M
Drake - God's Plan
05:57
Drake
visualizzazioni 1
DIP DOUNDOU GUISS  - NOBOMA WOON (Official Video)
04:07
Dip Doundou Guiss TV
visualizzazioni 4M
Dip Doundou Guiss - LNN  Feat. Bass Thioung (Official Video)
04:06
REACTION: UN BARO AD ITALIA'S GOT TALENT
10:00
Jack Nobile
visualizzazioni 86K
rovere, Mameli - freddo cane (Official Video)
3:17
RovereVEVO
visualizzazioni 281K
Burna Boy - Onyeka [Official Music Video]
3:23
Burna Boy
visualizzazioni 3,8M
Elodie - This Is Elodie (Benny Benassi Megamix)
4:56
Culita Sterp ❌ Laura Vetty - Kalinka
2:49
Fortza Generation
visualizzazioni 677K
iKON - ‘왜왜왜 (Why Why Why)’ M/V
3:42