🛑SUIVEZ CONFRONTATION #EUMEULAC2 / #DIENEMODOUANTA #AVRIL04 AVEC BIJOU NGONE |VENDREDI 9 AVRIL 2021

  visualizzazioni 757,497

2stvsenegal

Mese fa

🚩ABONNEZ-VOUS à la Chaîne de la 2STV cliquez sur ce LIEN👉 : bit.ly/3cnXP6h
Retrouvez l'ensemble de nos programmes d'actualité et émissions de société, santé, politique, culture, musique, économie sur:
- itpost.info
- www.2stv.net
- Iptv disponible sur 2stv.sn
- 2stv_senegal
- 2stvsenegal
- Snapchat: senegal2stv
- TikTok: @2stvsenegal
- 2stvsenegal
- www.dailymotion.com/video/x7vidbb
#CONFRONTATION #EUMEULAC2 #2STVLIVE #2STVSENEGAL #KEBETU

Commenti
Badara Sidibe
Badara Sidibe 8 ore fa
Ay way koumay diapalè dioxma numero eumeu ta yala tax
Baba Thiam
Baba Thiam 7 giorni fa
Lac de guier2 gorrjiguene la outil bongo d'i tassou
Daouda Guéye
Daouda Guéye 9 giorni fa
Lac dou dara
Sadibou Aidara
Sadibou Aidara 11 giorni fa
Kenou dou eumeu
Lalia Coulibaly
Lalia Coulibaly 15 giorni fa
Wallay gaston il me tue 😂😂😂😭
Lalia Coulibaly
Lalia Coulibaly 15 giorni fa
Ragal bi gneup kham naign ko😂 lac nopil
Cherifou Singuinar
Cherifou Singuinar 18 giorni fa
Gastron vrai domeram la
Cherifou Singuinar
Cherifou Singuinar 18 giorni fa
Lac mi vrai goor djigene leu
Bouba Diouf
Bouba Diouf 18 giorni fa
Eumo dousa morome vraiment démale diagué bapate
Fatou Gueye
Fatou Gueye 19 giorni fa
Mane je savais pas que lac de guerre était si bête tchiim ndéké goude ak Reuyy takhoul ame khelle
Fatou Samb
Fatou Samb 20 giorni fa
Lac niak na diom reuy na lamigne begue na diakhasé ay wakh meuna yakk lamb
seydina omar diop
seydina omar diop 21 giorno fa
Lac2 dougn ko bayei teugeul lamb niit gni nopalou
Thierno Yaya Dème
Thierno Yaya Dème 23 giorni fa
Eumeu Sène dalna machalaaa Lac mom amoul roussoukayyyt
Zizou Diagne
Zizou Diagne 24 giorni fa
Lac tapet d'où dieul roi des arène xana roi bi ngay dieul Aÿ wax lay done
Pape Diop
Pape Diop 24 giorni fa
Lac fi kén banioulafi ya niak diom té do ndago dadié amal fit
Assya Kâ
Assya Kâ 24 giorni fa
Lac de guerre yaw doule khamo gateu sa khole bou bone domérame ga rék famme biga done 🖕🏿🖕🏿🖕🏿🖕🏿🖕🏿
bocoy noiu
bocoy noiu 24 giorni fa
Mane lac 2 noumou def ba nék mbeur lay lathie
Nabou Ndiaye
Nabou Ndiaye 25 giorni fa
EUMEU daga soxor trop nak waxofi nak Lac beug dou bagn beug nane la ba paré kén manousi dra💪💪💪
Nabou Ndiaye
Nabou Ndiaye 25 giorni fa
Mbeur bola nexoule néxoula rék mé LAC GUÉR degue rek ga wax Eumeu boule saltél b victoirou diambour thipatouwaye
asioe kiou
asioe kiou 25 giorni fa
Mane lac 2 noumou def ba nék mbeur lay lathie
Lvyyrgchf boy
Lvyyrgchf boy 25 giorni fa
Best Datting Click 🔽 18cams.xyz 在整個人類歷史上,強者,富人和具有狡猾特質的人捕食部落,氏族,城鎮,城市和鄉村中的弱者,無`'守和貧窮成員。然而,人類的生存意願迫使那些被拒絕,被剝奪或摧毀的基本需求的人們找到了一種生活方式,並繼續將其DNA融入不斷發展的人類社會。 說到食物,不要以為那些被拒絕的人只吃垃圾。相反,他們學會了在被忽視的肉類和蔬菜中尋找營養。他們學會了清潔,切塊,調味和慢燉慢燉的野菜和肉類,在食品市場上被忽略的部分家用蔬菜和肉類,並且學會了使用芳香的木煙(如山核桃,山核桃和豆科灌木 來調味食物煮的時候 1618603293
Bimootd officiel
Bimootd officiel 25 giorni fa
Bijoux dafa mini kou nop eumeu 🥰🥰
Ismaila Drame
Ismaila Drame 25 giorni fa
Mais lac mi ndékété ab dofla dh no😂
#Bambiste chycorien
#Bambiste chycorien 25 giorni fa
1:03:50 degeul lac di doul nan dor mou wadd
Sokhna Thiam
Sokhna Thiam 25 giorni fa
Lac nopile
Sokhna Thiam
Sokhna Thiam 25 giorni fa
Lac kome 🦅🦅🦅
Mame Awa cissé
Mame Awa cissé 26 giorni fa
Bravo eme séne sa pion ga machalla ❤️💋🙏🙏👍
Grand Gass
Grand Gass 26 giorni fa
Lac 2 kagn ngay seuyi.😁😁😁mane hamna tu es viérge
yasio bolo
yasio bolo 26 giorni fa
Eumeu dou sama mbeur ms da am savoir vivre savoir faire et mm savoir parler ❤️
ibrahima souare
ibrahima souare 26 giorni fa
Radio grafia biii kholen date biii di na leer boudeee apres le combat bi le lac day fennnn boudee avant combat bii la wakhna deugeu
ibrahima souare
ibrahima souare 26 giorni fa
Yar zero ndeysann ki daffa bett nieupppp
Mamadou Sow
Mamadou Sow 26 giorni fa
Lac comme kou Danel 😂😂
Patrice Gomis
Patrice Gomis 26 giorni fa
Lac mome d'où champion day respecter distasiation sociale
Ibrahima Séne
Ibrahima Séne 27 giorni fa
Eumeu Séne t'es un guerrier née ça se voit même dans ta manière de parler
Malick Thiaw
Malick Thiaw 27 giorni fa
Eumeu
vbddfy euuyt
vbddfy euuyt 27 giorni fa
Eumeu sene dal machallah sa khol rafett amal diam rek👌🏿🙏🏾
Pape Mbagnick Ndour
Pape Mbagnick Ndour 27 giorni fa
Très franchement gni nékeu ci plateau bi yeup donio farr ak Eumeu... Bayilén victoirou diambour biguén di saltél ishhhh
Patrice Gomis
Patrice Gomis 27 giorni fa
Eumeu sa kanam newineu mé Moy Sama mbeur
Rokhaya Diatta
Rokhaya Diatta 27 giorni fa
Ayy eumeu srx daffa am yaar téyy kham savoir parlé love sur toi tu n'as rien a prouver au sénégalais tas tout fait
OUMZ DABBZ
OUMZ DABBZ 27 giorni fa
EUMEULAC2 LETS GO .. MY MONEY STILL ON EUMEU ALL DAY HIS THE GOAT ✔✔✔✔
Alune Ba
Alune Ba 27 giorni fa
Lac amoul vérgogne koi
Cheikh Jr
Cheikh Jr 27 giorni fa
Sanex a des mots incroyables ms courage modou anta djiambar gua👊🏻
W Papii
W Papii 27 giorni fa
Lac de guiers esk dou ñiarel 😂😂😂😂. Il est grave ce mec 🤣🤣
Adama Sow
Adama Sow 27 giorni fa
Lac de guerre s'est un champion mais malheureusement il n'est pas professionnel à travers sa communication..Il parle mal vraiment...damako yeureume sakh
Alioune Thioune
Alioune Thioune 27 giorni fa
Lac da rew respect way
Diaba Fall
Diaba Fall 27 giorni fa
Wa lac dou réé tmt fi adouna la man yw la supporté ms bagnil gnagual bi
elhadji mbaye
elhadji mbaye 27 giorni fa
Vraiment modou anta sui d ts coeur avec vs bilay yalla dinala fay sa khole.sa nekh beugu na ligua defff ni day deuguou bilay
Awa Baba Niang
Awa Baba Niang 27 giorni fa
Diadjeuf eumeu sene
dame kara Fall
dame kara Fall 27 giorni fa
Modou anta yalla nala yalla diapa lé
Nino Jahlil l'officiel
Nino Jahlil l'officiel 27 giorni fa
Modou Anta Champion nga Numu meuna deimeii Ns sommes derrière toi Lion Nga🔥👊💘😭💗💘
Djibril Geuye
Djibril Geuye 27 giorni fa
Courage modou anta💪💪💪💪💪🇸🇳🙏🙏👈👈👈
remond ndiaye
remond ndiaye 27 giorni fa
Lac bilae ya niak diom meuna diaxassei nit ak nit
Djibril Geuye
Djibril Geuye 27 giorni fa
Eume sene maire de guediawaye🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
sokhna bop
sokhna bop 27 giorni fa
Ya lac dagay har ndakh nul mola geuneul fouf victoire 😂😂 Mba khamegani do gawa beureuwate😂😂 Eumeu SENE macha Allah yaw daga yarou boula béne khaler sorkho sorkho champion pire ga macha Allah
Fatou bintou Djitte
Fatou bintou Djitte 27 giorni fa
Modou anta sama mbokk talibé nga
Astou Diack
Astou Diack 27 giorni fa
Eumeu yow daga yarou boul yak temps ci ki
Fatou bintou Djitte
Fatou bintou Djitte 27 giorni fa
Macha allah ❤️ gris bardeaux kaddou yi rafetna
Fatou bintou Djitte
Fatou bintou Djitte 27 giorni fa
Lac nopill wayyy sofff nga bari nga wakh euppeul nga khamo ninggay wakhé...... BIJOU sa fond de teint bi saffnnaaa
Madior Gueye
Madior Gueye 27 giorni fa
Mba kham nguen ni Lac de guerre esprit djiguén la yoré Goor djiguén leu koi
Djibril Ndiaye
Djibril Ndiaye 27 giorni fa
Lac tu es nul
Aliounebadara Ndiaye
Aliounebadara Ndiaye 27 giorni fa
Lac goor dou Bari wakh Modou anta nioune wa Thiès yaw laniou am champions gua
soiung toiue
soiung toiue 27 giorni fa
Dakh yaw eumeu doo moromou gayi du courage 💪💪💪👍💘💘👍
Alhassane Ba
Alhassane Ba 28 giorni fa
Lac do touss ya geneu yambarr si mbeurr yeupp
Mariama Dansokho
Mariama Dansokho 28 giorni fa
Lui khana lui entre nous
Tidiane Sylla
Tidiane Sylla 28 giorni fa
Big Taff comme borom keur bougnouy dabb dikoo niande 😂😂top si ganaww bijou rk
ibou thiam
ibou thiam 28 giorni fa
Bilae wallae Lac2 mi meune na tass adouna ndaxx meune féne ki mo meune doul wayy
soiung toiue
soiung toiue 27 giorni fa
Confrontación nekhna
Mamadou Mbaye
Mamadou Mbaye 28 giorni fa
Lac amo savoir vivre nit day respecté bopam bo beugué niou respecté leuh nieup xam nanou ni do mbeur yawou dial sakh mola gueuneuh riche palmares mayal nit gni diam sénégalais yi xam nanu lepp
amadou dienf
amadou dienf 28 giorni fa
booléen bal
boyo Jarra
boyo Jarra 28 giorni fa
Lac yow zero nga c komba b
Abibe Ousmane
Abibe Ousmane 28 giorni fa
Modou anta do touss
ibou thiam
ibou thiam 28 giorni fa
😂😂
Dabakh DIENE
Dabakh DIENE 28 giorni fa
Bilaii Modou dioy lo nama😭 Déjà je l'appréciais ndakh goor Yalla la ci lepp.. Mais là je l'estime de trop.. BayeFall amal diam.. 👌
Seck Abou
Seck Abou 28 giorni fa
Way lac double rek
ndiatigué comédien
ndiatigué comédien 28 giorni fa
Tapez ndiatigué comédien et abbonnez vous vite rée ba tass 😂 thiéy ndiatigué mingui tothie youtube
Keita Fanta
Keita Fanta 28 giorni fa
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
fadel bu lo
fadel bu lo 28 giorni fa
Gaston arrete tes rouber fi sonko mo fi neee bu niu sonal di rouber merde a la fin sa combat bu nakarie bi👎👎👎👎👎
fadel bu lo
fadel bu lo 28 giorni fa
The king xaragne lo🤜🤜🤜🤜🤜🤜
fadel bu lo
fadel bu lo 28 giorni fa
Nooooo modou anta vs ns avez fait touss pleurer walah du courage pr la suite 👌👌👌
Tall Mbaye
Tall Mbaye 28 giorni fa
Big taff 3h de temps en debout Franchement ils sont pas sérieux
Oumar Thiene
Oumar Thiene 28 giorni fa
Vraiment j'ai pleurè a chaud larmes avec LS propos de sanekh c'est triste ayons la courage d'aider nos frère thiesoise
Awa Baba Niang
Awa Baba Niang 28 giorni fa
Confrontación nekhna
Lamin Diop
Lamin Diop 28 giorni fa
Yaw lac doul nopil amo lo wax
Seydou kasse
Seydou kasse 28 giorni fa
Lac2 tu a déçu tout les mondes. Merci champion euma
sombel sene
sombel sene 28 giorni fa
moudou sama kholl diekhna mane mom mkilaye dianall mame ch ibre mika yakar mo takhawola😭😭😭🤝🤝
Lamine Ndiaye
Lamine Ndiaye 28 giorni fa
Père Macondé meunoumako mougn kw😀😀😀
Marie Ndiaye
Marie Ndiaye 28 giorni fa
Non bijoux machallah dama réh ba soneuh machallah jsui lac 100% dina bakh
maïmouna fall
maïmouna fall 28 giorni fa
Lac dafa rew mais yaw yaye kane
Sene Pouye Mareme Madame
Sene Pouye Mareme Madame 28 giorni fa
😭😭😭😭😭modou anta tu ma fais pleurer
MBAYE NDIAYE
MBAYE NDIAYE 28 giorni fa
Euma wakhna deug
Khady Drame
Khady Drame 28 giorni fa
Eumeu diambar la gni d’accord ak mane dafal j’aime 👍
Binetou rassoul
Binetou rassoul 28 giorni fa
Day doul lokho bou dam guakoy niamakh niamakhi
Binetou rassoul
Binetou rassoul 28 giorni fa
Lac 2 thiokh la amoul
Jacques D Diouf
Jacques D Diouf 28 giorni fa
Vraiment lac 2 na rien a dire raggal la
Mouhamed Diouf
Mouhamed Diouf 28 giorni fa
Lac sisoumane la 😂
Maty Diane
Maty Diane 28 giorni fa
Eumeu tey na yarou na machalla lac sa wakh barina te diom zero
Courielle Balde
Courielle Balde 28 giorni fa
Eumeu sene y'a geuneu yarou si mbeur yeupp machallah
Ndèye Gning
Ndèye Gning 28 giorni fa
Euma champion
Ndèye Gning
Ndèye Gning 28 giorni fa
Fo guis kou bari wakh tapète leu
Anta Mbodji
Anta Mbodji 28 giorni fa
Thieuy bijou dawul thiow 😂ragalo dh 😂
ndeye ndoye
ndeye ndoye 28 giorni fa
Lac doule way yaw doule kakte bou mak gua
Rama Thiam
Rama Thiam 28 giorni fa
Ok
Débat houleux entre Eumeu Sene Lac 2...Ma noxoula...
06:27
Top 10 MISTERI IRRISOLTI della SECONDA GUERRA MONDIALE!
9:18
🛑[DEBAT] Suivez GUISS GUISS | Dimanche 11 Avril 2021
3:02:40
Groupe DMEDIA - SenTv
visualizzazioni 57K
Top 10 MISTERI IRRISOLTI della SECONDA GUERRA MONDIALE!
9:18
DENALMOND E LADY GIORGIA 💕 #4
11:40
La Tana del Frerito
visualizzazioni 84K
È Tornato dopo 8 anni!
8:14
Quei Due Sul Server
visualizzazioni 126K
NASCONDINO CON I PEDONI IN PRIGIONE SU GTA5!!
20:15
WhenGamersFail ► Lyon
visualizzazioni 507K
AUTOGOL CARTOON - Mourinho alla Roma
4:34
Gli Autogol
visualizzazioni 718K